Safary Allo Lyrics

Allo naka sa journée

Allo tay noko doundé

Tok galé déf yarou

Wayé douma té défaru

Luma nameu diko togantou

Guinaw amatul toxantu

Feulalé dougal staut 

Photo profile bu béss wala story

Bagn kéneu mérr tax ma déff lii 

Sou doyul Waxlén ma doli ...

Sou doyul Waxlén ma doli

Quarantine bi, quarantine bi, quarantine béee

Quarantine bi, quarantine bi, quarantine béee

Yangui si dara eh eh 

Kula guiss xamni yangui si dara

Wakho dara, eh eh 

Koula xol xamni yangui am dara

Yangui si dara

Tok galé déff ndiongué

Tirage bi si féep la manée

Mané rék si djêk xadjiou ma si goné

Luma nékh safnako Beussna OK

Sma caramél déma djiégué

Waro dima sori déma niémé

Couvre-feu mak'ak yaw

Nioy confiner eh ey

Fii ba fassé lila nékha fi né

Kone dal ya déf lii

Sou doyul waxlén ma doli

Lou none ték nga téggui

Quarantine bi, quarantine bi, quarantine béee

Quarantine bi, quarantine bi, quarantine béee

Yangui si dara eh eh 

Kula guiss xamni yangui si dara

Wakho dara, eh eh 

Koula xol xamni yangui am dara

Yangui si dara

Allo naka sa journée

Allo tay noko doundé

Nameu na biti kimay fathi mingui si keur gui

Mak'sama chéri acteur'rou

Série xaruma couvre-feu di gnibi

Xaral ma déconnecter buma kéneu dérangé

Sama xol mo dieul sa place

Bayilma ** football nga woté mangui confinement challenge

Yangui tokk sa money yeah!

Sou doyul ma doli 

Quaranitne VIP wawaw su doyul ma doli