Daara J TchéKoulé Lyrics, Paroles

TchéKoulé

13 December 2019
69

Daara J TchéKoulé Lyrics

Dégglutileen bismilaay jàmm la

tàggu nanu Mbaar Njaay

tàggooti Mbaar Njaay


jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa

jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa

jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa

jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa

tché tché tchékoulé

tché ko vista ko vista ta lànga

ka ka tchi lànga

tché tché tchékoulé

tché ko vista ko vista ta lànga

ka ka tchi lànga


Tàggu naa Mbaar Njaay

Tàgguti naa Mbaar Njaay

Ndongod may may lengee

ma bàkku céru ndey ak baay

Xaaxtandiku kàllaamay wolof Big up Buur ba Jolof

Sarenzo Pacotille ak ndem-si-Yàlla Vieira ak Las Mc

Rap pop doo bopp nga dem Ardo

bu jinne bëggee daqaar ku yéeg daanu

boo reppee ci xare lu mu jiin xeeb ko

da ngay xaru di nu tëkku tey sa fan ñu leb ko, ahh!!

boo bëggee sàqami sunu lanc di nga bekkoor

Nangu da fa jël céru bañ aah, suukëru koor

daan dox gox ba gox ngir freestyle téya Mic Ñeme naaj

fosco discothéque walla ladies night How many mic !!!

dagg nga sa Geetar Uhh uhh uhhh gis nga ku la gëna feebar



jaaba débaa laa


tché tché tchékoulé

tché ko vista ko vista ta lànga

ka ka tchi lànga

tché tché tchékoulé

tché ko vista ko vista ta lànga

ka ka tchi lànga

jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa


Tàggu naa Mbaar Njaay

Tàggooti naa Mbaar Njaay

Faada aal ma lengee

ma bàkku céru ndey ak baay

Téyal catu ndab booy lekk ci ceeb bi

Di nga yàbbi li nga sex booy teggi

Ndawal li ci digg bool bul seppi

Njëkka dóor yàkkamti la ci xeex bi

Suul ker du ko tere mësa féete kow

Yaa ngi course ak dee moo la gëna gaaw

Dañoo wuute bi style te du mësa bokk

Dafa yàgg ñi di coow ne du mësa dox

Dañoo taq ban ripp buñu jéema topp

Fi nu jaar boo fi ñëwee di nga gën a xoox

Lewël bu tàng jërr ëf ko te jeeri ko

Laax buy lakkee bul bëri coow ni barigo


jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa

jaaba diba bilaaa

jaaba débaa laa.....

Dégglutileen bismilaay jàmm la

tàggu nanu Mbaar Njaay

tàggooti Mbaar Njaay

...

 ----------------------------------------------------------

Tchekoule English :

In the name of Ancestors listen in peace

To those initiated in the men’s hut

I’m asking for your permission to come on stage


Faada Freddy Verse :

To those initiated in the men’s hut

I’m asking for your permission to come on stage

Ndongod, pass the witness, let me honour our mothers and fathers

I moved the tongue in wolof

Honour to Buurba Jolof, Sarenzo,Pacotille,Viera and Las Mc

Rap pop doo bop, you’ll touch the floor of the tamarind master and actually nobody will have fruits

He who is not ready will be beaten in battle

You’re crazy to test us, your days are counted aah!

You want our voice to be stumbled ?

watch out, you’ll fail!

There is no choice, accept the challenge! Like the benefits of the fasting month We made our weapons from town to town, holding the mic under the sun

We visited the fosco (school parties), night clubs, ladies nights

How many microphones we held?

You’re losing your power, uhh uhh uhh, we’re crazier than you!


Ndongod 'Verse :

To those initiated in the men’s hut

I’m asking for your permission to come on stage

Faada, give me the witness so I can honour our mothers and fathers Hold the bowl well when you eat rice

You’ll empty your mouth when your hands exceed the limits

You hit first but you’ll get beaten anyway,

Only the obscure, the shadow, can bury

Life is a race, death is at the finish line

We didn’t take the same path

We believed it since the beginning of time

whoever tries to compete will dive in the mud

Follow our traces, there will not be any rest

Hot in front, if you want to soften the sauce which is boiling

Don’t open like an empty barrel...


Other song(s) of Daara J

Trendings Lyrics

00:00 00:00