Fermer
Viviane Chidid Do Dara image

Do Dara

870
Viviane Chidid Do Dara Lyrics

Néna dafa am mana, (mana)

Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)

Néna dafa am mana (mana)

Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)

Meuna ndiody beugeu diay graw (diay graw)

Té ioe yoroulo nada (yoroulo nada )

Meuneu gondi beug diay graw,

Té yoroulo nada sax

Néna yor na ohh oh ohohoh

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh

Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho

Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Di fowé sa xel bi molay sonal

Goor souné war nga diom (di déf té lou yomb)

Loufi diar ngey wané (djom ba niawalone nama)

Di digué lo meunoul, (so teudé do nélaw)

Dou ni nga beugeu doundé

Dou ni nga beugeu doundé

Ki tothi na kogn ba oh oh oh

Do dara, do dara, do dara

Gnata yone nga dieul alalam té fayoko

Gnata yone nga digg Pa yék mère yi niou adji ji Macca (Macca )

Té défoci dara (dara)

Nioune guissouniou dara,

Ndéké ioe do dara

Néna dafa am mana

Té yoroul ndieugou nana

Néna dafa am mana

Té yoroul ndieugou nana

Meuna ndiody beugeu diay graw,

Té ioe yoroulo nada

Meuneu gondi beug diay graw,

Té yoroulo nada sax

Néna yor na ohh oh ohoho

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh

Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho

Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Di fowé sa xel bi molay sonal

Goor souné war nga diom (di déf té lou yomb)

Loufi diar ngey wané (djom ba niawalone nama)

Di digué lo meunoul, (so teudé do nélaw)

Dou ni nga beugeu doundé

Dou ni nga beugeu doundé

Ki tothi na kogn ba oh oh oh

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh

Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho

Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Do dara, do dara, do dara

oh oh oh , eh eh eh

Viviane Chidid Suggestions

Suggestions